Home         Translations         About Us   
search  












 

WOR BI

Li yonent yi bindoom lpp ci mbirum Doomu nit ki dina mat. Dinau ki jbbal i dul Yawut, u aawaal ko, saaga ko, tifli ci kawam. Ganaaw bu u ko dore ay yar ba noppi, dinau ko rey, waaye ca etteelu fan ba dina dekki. (1)

Samay soppe, sama nekk ak yeen dootul ygg. Fama jm, dungeen fa mana dem. anu lkk reru jggi bu mujj bii laata u may sonal. Ndaxte maa ngi leen koy wax, dootuma ko lekk mukk, lu dul ba kera muy mat ci nguuru Ylla. Noonu itam dootuma naan ndoxum rse mi, ba kera Ylla di tral nguuram.

Noonu mu jl mbuuru njoxleen ko ne: Lii sama yaram la, wi ma joxe ngir yeen. Defleen lii, ngir fttaliku ma. Mu jl kaas ne leen: Lii moy misaal kllre gu bees gi Ylla jaarale ko ci sama deret, ji tuuru ngir yeen. (2)

Demaa ware joxe sama dund ni ko yonent yi waxe woon. Doomu nit ki mu ngi dem, ni u ko waxe ci Mbind mi, waaye ki koy wr dina torox, baoona juddu moo gnoon ci moom. Yeen pp taxuleen may wax; xam naa i ma tnn. Waaye li Mbind mi wax, fww mu am bi mu naan: " Ki lell sama dugub wq na ma ". Maa ngi leen koy wax ci teel, bala looloo w, ngir bu wee, ngeen gm ne Maay ki Nekk. (3)

ttan ngaa joxe sa bakkan ngir man?

Yeen pp dingeen ma dggeeki, ndaxte Mbind nau: " Dina dor smm bi, xari jur gi tasaaro'. (4)

Naam Baay bi yaw mi dare twul, teggil ma kaasu naqar bii. Moona bu mu doon sama coobare, waaye na sa coobare am. (5) Jeex na, waxtu wi jot na; u ngi wor Doomu nit ki ci loxoy bkkaarkat yi. Roofal sa jaasi ci mbaram, ndaxte ku bocci jaasi, jaasi moo lay rey. (6)

Ci fon ngay jbbale Doomu nit ki ay noonam! Jg ngeen, gnnaayoo ay jaasi ak ay yet, mel ni uy topp scc. Moona maa ngi woon ak yeen bs bu nekk ca kr Ylla ga, te jppuleen ma. Waaye legi seen waxtu la, ak jamanoy lndm gi. (7)

Xana xamuloo ne, man naa laaj sama Baay te dina ma may ci taxawaay bi mboloom malaaka mu xel dajul? Legi nag ndamu Doomu nit ki fee na, te ndamu Ylla fee na itam ci moom. Te bu ma feeale ndamu Ylla, Ylla itam ci teewaayam dina feeal ndamu Doomu nit ki, te dina ko def legi. (8)

ATTE BI AK BANT BI

Amuloo ben sa-sa ci man su dul bi la Ylla jox. (1)

Lu tax nga may laaj? Laajal i doon dglu li ma leen wax. oom xam nau li ma doon wax. Ci mboolo laa doon waxe. Ci kr Ylla ga ak ci ay jngu, fa yawut ypp di daje, laa mas di jangelee. Musuma wax dara di ko nbb.

Suma waxee lu jaaduwul, wone ko; waaye su ma waxe lu jub lu tax nga may dor. (2)

Sam kilifteef nekkul ci ddina. Bu sama kilifteef nekkoon ddina, sama surga yi dinau xeex, ba u jbbale ma. Sama kilifteef nekkul ddina.

Wax nga ko; buur la. Lii moo tax, ma juddo, ci w ddina: Ngir wax dg gi, ku bokk ci dgg gi dina nangu li ma wax. (3)

Legi u daq malaaka mu bon mi jiite ddina si. Te man, bu u ma yekketee, ma tiim suuf, dina woo nit p ci man. (4)

Baay bi bg na ma, ndaxte damay joxe sama bakkan ngir jlaat ko. Kenn du ko jle ci man, man maa koy joxe ci sama coobarey bopp. Am naa it sa-sa joxe ko te am naa sa-sa jlaat ko. Loolu la ma sama Baay sant. (5)

Baay, baal leen ndaxte xamuu li uy def.

Eli, Eli, Lama Sabaktani; l iy tekki: Sama Ylla, sama Ylla, lu tax nga dddu ma?

GANNAAW NDEKKITE LA

Yeen dal yeena akk xel, te sen xol yeexa gm li yonent yi ygle woom! Xana du Krist di Almasi bi dafa waroon daj coono te dugg ci ndamam? Byyil di weddi te nga gm (1)

Bi ma nekkee ak yeen, waxoon naa leen baat yii: Li u mbind lpp ci samay mbir ci Yoonu Musaa ad terey yonent yi ak ci Sabor dafa wara am: Fww Almasi bi son, mu dee te dekki ca etteelu fan ba, te it uy ygle ypp ci turam, dale ko ci Yrusalem, ne war naoo tuub seeni bkkaar, Ylla baal leen. (2)

Xam naa fa ma byyikoo, xam fa ma jm, waaye yeen xamuleen fa ma byyikoo ak fa ma jm. Yeen, fii ngeen bawoo, ci suuf, waaye man ci kaw laa jge. (3)

Ken msula yeg ci asamaan su dul ki fa jge, muy Doomu nit ki. Demal te ne samay mbokk, maa ngi yeg ca sama Baay biy seen Baay, ca sama Ylla jiy seen Ylla. (4)

Lu tax ngeen jaaxle, ak lu tax ngeen di xel aar ci seen xol?

Na jmm wcc ci yeen. Xolleen samay loxo ak samay tnk, laal leen ma te xam ne, man mii la; njuuma amul yaram walle ay yax, ni ngeen gise, ma am ko. Li nga mas gis a tax nga gm? Ki bgg mooy ki gm te gisus ma. (5)

Des na tuuti ci kanam , ddina du ma gisati; waaye yeen dingeen ma gis. Dina dund, moo tax yeen itam dingeen dund. (6)

BEES BU NEKK

Ni ma Baay bi ynnee, noonu la leen di ynne, man itam. (1)

Demleen nag skk ay taalibe ci xeet ypp, sob leen ci ndox ci turu Baay ji, ak Doom ji, ak Xel mu sell mi. Demleen ci ddina spp, ygal xebaar bu baax bi mbindeef ypp. Ku gm te u sob ko ci dox, dina mucc; ku gmul, dees na ko daan. (2)

Buleen sore, waaye ngen xaar li Baay dige woon, te ma waxoon leen ko. Yaxya ci boppam moom daa sob nit i ci dox, waaye yeen, dees na leen sob ci Xel mu Sell mi fi ak ay fan yu new. (3)

Bu Xel mu Sell mi wee ci yeen, dingeen jot kttan, te nekk samay seede ci dkku Yrusalem, ca diiwanu Yude ak Samari Ypp, ak ba fa ddina yem. Sol naa leen Xellu Ylla mu Sell mi. (4)

Jngal leen xeet yi u smm lpp li ma leen sant; te fttalikuleen ma ngi ak yeen bs bu nekk, ba kera ddina di tukki.


BEES YU MUJJ WU YEESU CI KAW SUUF WOR BI

1. Lukk 18: 31-33, 2. Yowanna 13: 33; Lukk 22: 15, 16, 18, 20, 3. Mac 26: 24; Yowanna 13: 19; Sabor 41:9; Yowanna 13:19, 4. Yowanna 13: 38; Mark 14:27; Sakaria 13: 7, 5. Mark 14: 36, 6. Mark14: 41; Mac 26:52, 7. Lukk 22: 48-52,53, 8. Mac 26:53; Yowanna 13: 31.

ATTE BI AK BANT BI

1. Yowanna 19:11, 2. Yowanna 18: 21, 20, 23. 3. Yowanna 18: 36. 37 4. Yowanna 12: 31, 32, 5. Yowanna 10: 17, 18, 6. Lukk 23: 43, Mac 27: 46.

GANNAAW NDEKKITE LA

1. Lukk 24: 25, 26; Yowanna 20:27, 2. Lukk 24: 44, 46, 47, 3. Yowanna 8: 14, 23, 4. Yowanna 3: 13; 20: 17, 5. Lukk 24: 36-39; Yowanna 20: 29, 6. Yowanna 14: 19.

BS BU NEKK

1. Yowanna 20:21, 2. Mac 28:20; Mark 16: 15, 16, 3. Jf ya 1: 4, 5, 4. Jf ya 1: 8; Yowanna 20: 22, 5. Mac 28: 20.

 

 

 

 
Send a friend an email telling them about The Words Site:

Friend's Name:   Friend's Email:   Your Name:  

Home | About Us |

THE WORDS IS COPYRIGHT-FREE. Permission to duplicate The Words applies to all audio
narrations and/or video on this site. Site Design Copyright ©2003 The Words, all rights reserved.
Site design by Prime Web Design